Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 5

Kàddu yu Xelu 5:10-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Jaambur jariñoo sa doole, doxandéem jagoo saw ñaq.
11Ngay mujje onk, desey yax, jeex tàkk.
12Nga naan: «Su ma yégoon, sopp ab yar te baña sofental waxi àrtu.
13Lu ma tee woona dégg ku may digal, tey teewlu sama waxi sëriñ ya?

Read Kàddu yu Xelu 5Kàddu yu Xelu 5
Compare Kàddu yu Xelu 5:10-13Kàddu yu Xelu 5:10-13