Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 5:10-13 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 5:10-13 in Kàddug Yàlla gi

10 Jaambur jariñoo sa doole, doxandéem jagoo saw ñaq.
11 Ngay mujje onk, desey yax, jeex tàkk.
12 Nga naan: «Su ma yégoon, sopp ab yar te baña sofental waxi àrtu.
13 Lu ma tee woona dégg ku may digal, tey teewlu sama waxi sëriñ ya?
Kàddu yu Xelu 5 in Kàddug Yàlla gi