Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 4

Kàddu yu Xelu 4:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Amal xel mu rafet akug dégg. Bul fàtte te bul moy samay wax.
6Bul dëddu xel mu rafet, da lay aar; sopp ko, mu sàmm la.

Read Kàddu yu Xelu 4Kàddu yu Xelu 4
Compare Kàddu yu Xelu 4:5-6Kàddu yu Xelu 4:5-6