Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 4:5-6 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 4:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Amal xel mu rafet akug dégg. Bul fàtte te bul moy samay wax.
6 Bul dëddu xel mu rafet, da lay aar; sopp ko, mu sàmm la.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi