Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 4

Kàddu yu Xelu 4:19-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Yoonu ku bon ne këruus, du xam lu muy téqtaloo.
20Doom, déglul samay kàddu, teewlul samay wax.
21Bu ci noppee ja jàkk, te jàpp ko ci sa biir xel.

Read Kàddu yu Xelu 4Kàddu yu Xelu 4
Compare Kàddu yu Xelu 4:19-21Kàddu yu Xelu 4:19-21