Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 4:19-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 4:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Yoonu ku bon ne këruus, du xam lu muy téqtaloo.
20 Doom, déglul samay kàddu, teewlul samay wax.
21 Bu ci noppee ja jàkk, te jàpp ko ci sa biir xel.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi