Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 4

Kàddu yu Xelu 4:13-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Ŋoyal cib yar, bul yoqi, sàmm ko, moo yor sa bakkan.
14Yoonu ku bon, bu ci tegu; fu ab soxor di jaar, bu fa dox.

Read Kàddu yu Xelu 4Kàddu yu Xelu 4
Compare Kàddu yu Xelu 4:13-14Kàddu yu Xelu 4:13-14