Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 4:13-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 4:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Ŋoyal cib yar, bul yoqi, sàmm ko, moo yor sa bakkan.
14 Yoonu ku bon, bu ci tegu; fu ab soxor di jaar, bu fa dox.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi