Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 4

Kàddu yu Xelu 4:12-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Doo dox ba tërëf, doo daw, téqtalu.
13Ŋoyal cib yar, bul yoqi, sàmm ko, moo yor sa bakkan.
14Yoonu ku bon, bu ci tegu; fu ab soxor di jaar, bu fa dox.
15Moyul, bu fa jaare; mbasal te wéy!
16Ku bon du nelaw te lorewul, du dajjant ba kera muy téqe.

Read Kàddu yu Xelu 4Kàddu yu Xelu 4
Compare Kàddu yu Xelu 4:12-16Kàddu yu Xelu 4:12-16