Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 4:12-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 4:12-16 in Kàddug Yàlla gi

12 Doo dox ba tërëf, doo daw, téqtalu.
13 Ŋoyal cib yar, bul yoqi, sàmm ko, moo yor sa bakkan.
14 Yoonu ku bon, bu ci tegu; fu ab soxor di jaar, bu fa dox.
15 Moyul, bu fa jaare; mbasal te wéy!
16 Ku bon du nelaw te lorewul, du dajjant ba kera muy téqe.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi