Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:32-34

Help us?
Click on verse(s) to share them!
32Aji Sax ji daa sib ku dëng, xejjoo kuy jubal.
33Aji Sax ji day alag kër ku bon, di barkeel waa kër ku jub.
34Kuy ñaawle, moo lay ñaawal, ku toroxlu, mu may law yiw.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:32-34Kàddu yu Xelu 3:32-34