Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:32-34 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:32-34 in Kàddug Yàlla gi

32 Aji Sax ji daa sib ku dëng, xejjoo kuy jubal.
33 Aji Sax ji day alag kër ku bon, di barkeel waa kër ku jub.
34 Kuy ñaawle, moo lay ñaawal, ku toroxlu, mu may law yiw.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi