Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:30-32

Help us?
Click on verse(s) to share them!
30Bul joteek kenn ci neen, te tooñu la.
31Bul ñee ku néeg, te bu ko roy fenn.
32Aji Sax ji daa sib ku dëng, xejjoo kuy jubal.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:30-32Kàddu yu Xelu 3:30-32