Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:30-32 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:30-32 in Kàddug Yàlla gi

30 Bul joteek kenn ci neen, te tooñu la.
31 Bul ñee ku néeg, te bu ko roy fenn.
32 Aji Sax ji daa sib ku dëng, xejjoo kuy jubal.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi