Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:21-25

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Sama doom, saxool xelu akug foog, dee ci xool foo tollu.
22Day guddal saw fan, di rafetal sa jikko.
23Kon sab dox wóor, doo fakktalu.
24Soo tëddee doo tiit; say nelaw day neex.
25Kon doo ragal njàqare lu bette ak saaysaay buy songe,

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:21-25Kàddu yu Xelu 3:21-25