Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 3:21-25 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 3:21-25
in
Kàddug Yàlla gi
21
Sama doom, saxool xelu akug foog, dee ci xool foo tollu.
22
Day guddal saw fan, di rafetal sa jikko.
23
Kon sab dox wóor, doo fakktalu.
24
Soo tëddee doo tiit; say nelaw day neex.
25
Kon doo ragal njàqare lu bette ak saaysaay buy songe,
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms