Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:19-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Aji Sax ji xel mu rafet la sose suuf, lale asamaan ag dégg.
20Ci xam-xamam la ndoxi xóote ya ne jàyy, ay niir di lay.
21Sama doom, saxool xelu akug foog, dee ci xool foo tollu.
22Day guddal saw fan, di rafetal sa jikko.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:19-22Kàddu yu Xelu 3:19-22