Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:19-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:19-22 in Kàddug Yàlla gi

19 Aji Sax ji xel mu rafet la sose suuf, lale asamaan ag dégg.
20 Ci xam-xamam la ndoxi xóote ya ne jàyy, ay niir di lay.
21 Sama doom, saxool xelu akug foog, dee ci xool foo tollu.
22 Day guddal saw fan, di rafetal sa jikko.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi