Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:19-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Aji Sax ji xel mu rafet la sose suuf, lale asamaan ag dégg.
20Ci xam-xamam la ndoxi xóote ya ne jàyy, ay niir di lay.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:19-20Kàddu yu Xelu 3:19-20