Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:19-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Aji Sax ji xel mu rafet la sose suuf, lale asamaan ag dégg.
20 Ci xam-xamam la ndoxi xóote ya ne jàyy, ay niir di lay.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi