Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 31

Kàddu yu Xelu 31:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Bul jox jigéen ñi sa doole, bul jox say siddit jigéen ñiy sànk buur.
4Buur moomul di naan biiñ, Lemuyel, buur moomu ko; kilifa moomul di sàkku ñoll.

Read Kàddu yu Xelu 31Kàddu yu Xelu 31
Compare Kàddu yu Xelu 31:3-4Kàddu yu Xelu 31:3-4