Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:3-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Bul jox jigéen ñi sa doole, bul jox say siddit jigéen ñiy sànk buur.
4 Buur moomul di naan biiñ, Lemuyel, buur moomu ko; kilifa moomul di sàkku ñoll.
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi