Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 31

Kàddu yu Xelu 31:29-31

Help us?
Click on verse(s) to share them!
29«Jeeg bu jàmbaare bare na, waaye yaw, yaa ci raw.»
30Melokaan wu jekk day naxe, taar day wéy, waaye jigéen ju ragal Aji Sax ji, kookoo jara gërëm.
31Joxleen ko njukkalu ñaqam, jëfam di woyam ca pénc ma.

Read Kàddu yu Xelu 31Kàddu yu Xelu 31
Compare Kàddu yu Xelu 31:29-31Kàddu yu Xelu 31:29-31