Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:29-31 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:29-31 in Kàddug Yàlla gi

29 «Jeeg bu jàmbaare bare na, waaye yaw, yaa ci raw.»
30 Melokaan wu jekk day naxe, taar day wéy, waaye jigéen ju ragal Aji Sax ji, kookoo jara gërëm.
31 Joxleen ko njukkalu ñaqam, jëfam di woyam ca pénc ma.
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi