Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 31

Kàddu yu Xelu 31:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Day mel ni gaalu jula, di jëli dundam fu sore.
15Day jóg te bët setul, di waajal njëlu njabootam, ak a sas ay janqam.
16Day seetlu ab tool, jënd ko, sàkk ciw ñaqam, jëmbat tóokër.

Read Kàddu yu Xelu 31Kàddu yu Xelu 31
Compare Kàddu yu Xelu 31:14-16Kàddu yu Xelu 31:14-16