Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:14-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Day mel ni gaalu jula, di jëli dundam fu sore.
15 Day jóg te bët setul, di waajal njëlu njabootam, ak a sas ay janqam.
16 Day seetlu ab tool, jënd ko, sàkk ciw ñaqam, jëmbat tóokër.
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi