Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 30

Kàddu yu Xelu 30:9-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9lu ko moy ma regg, weddi la, ba naan: «Kuy Aji Sax ji?» Mbaa ma ñàkk bay sàcc, di la ñàkke worma, yaw sama Yàlla.
10Bul sikkal ab surga ca njaatigeem, da lay ñaan-yàlla, mu dal la.
11Ag maas a ngi saaga baay, te wormaaluñu ndey.
12Ag maas a ngi defe ne set nañu, te taq ripp ak bàkkaar.

Read Kàddu yu Xelu 30Kàddu yu Xelu 30
Compare Kàddu yu Xelu 30:9-12Kàddu yu Xelu 30:9-12