Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 30:9-12 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 30:9-12 in Kàddug Yàlla gi

9 lu ko moy ma regg, weddi la, ba naan: «Kuy Aji Sax ji?» Mbaa ma ñàkk bay sàcc, di la ñàkke worma, yaw sama Yàlla.
10 Bul sikkal ab surga ca njaatigeem, da lay ñaan-yàlla, mu dal la.
11 Ag maas a ngi saaga baay, te wormaaluñu ndey.
12 Ag maas a ngi defe ne set nañu, te taq ripp ak bàkkaar.
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi