Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 30

Kàddu yu Xelu 30:28-31

Help us?
Click on verse(s) to share them!
28sindax, manees na koo ŋëb, teewul ma nga biir kër buur.
29Ñett a ngii, ñu jekk um ndaag, ba ci ñeent ñu jekk doxin:
30gaynde, mooy buuru rab yi, ragalul kenn;
31séq daagu, jekk taxawaay, ab sikket, ak buur ci biiri dagam.

Read Kàddu yu Xelu 30Kàddu yu Xelu 30
Compare Kàddu yu Xelu 30:28-31Kàddu yu Xelu 30:28-31