Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 30:28-31 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 30:28-31 in Kàddug Yàlla gi

28 sindax, manees na koo ŋëb, teewul ma nga biir kër buur.
29 Ñett a ngii, ñu jekk um ndaag, ba ci ñeent ñu jekk doxin:
30 gaynde, mooy buuru rab yi, ragalul kenn;
31 séq daagu, jekk taxawaay, ab sikket, ak buur ci biiri dagam.
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi