Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 30

Kàddu yu Xelu 30:19-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19yoonu jaxaay ci asamaan, yoonu jaan ci kawi doj, yoonu gaal ci diggu géej, yoon wi góor di jaar as ndaw.
20Jikkoy jigéenu moykat a ngi. Day lekk, wommiku, te naan: «Defuma dara lu aay!»

Read Kàddu yu Xelu 30Kàddu yu Xelu 30
Compare Kàddu yu Xelu 30:19-20Kàddu yu Xelu 30:19-20