Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 30:19-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 30:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 yoonu jaxaay ci asamaan, yoonu jaan ci kawi doj, yoonu gaal ci diggu géej, yoon wi góor di jaar as ndaw.
20 Jikkoy jigéenu moykat a ngi. Day lekk, wommiku, te naan: «Defuma dara lu aay!»
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi