Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 30

Kàddu yu Xelu 30:15-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Saxu watar du suur, ñaar ñu jigéen la am: Jox Ma ak Jox Ma. Ñett a ngii ñu dul suur, ba ci ñeent ñu dul ne doy na mukk:
16njaniiw, jigéen ju jaasir, suuf, du màndi ndox, sawara, du ne doy na mukk.

Read Kàddu yu Xelu 30Kàddu yu Xelu 30
Compare Kàddu yu Xelu 30:15-16Kàddu yu Xelu 30:15-16