Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 30:15-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 30:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Saxu watar du suur, ñaar ñu jigéen la am: Jox Ma ak Jox Ma. Ñett a ngii ñu dul suur, ba ci ñeent ñu dul ne doy na mukk:
16 njaniiw, jigéen ju jaasir, suuf, du màndi ndox, sawara, du ne doy na mukk.
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi