Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 30

Kàddu yu Xelu 30:14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Ag maas a ngi, seeni sell niy saamar, seeni gëñ niy paaka, ñuy lekk néew-ji-doole, ba raafal leen ci réew mi, ba ku ñàkk jeex ci biir nit ñi.

Read Kàddu yu Xelu 30Kàddu yu Xelu 30
Compare Kàddu yu Xelu 30:14Kàddu yu Xelu 30:14