Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 30:14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 30:14 in Kàddug Yàlla gi

14 Ag maas a ngi, seeni sell niy saamar, seeni gëñ niy paaka, ñuy lekk néew-ji-doole, ba raafal leen ci réew mi, ba ku ñàkk jeex ci biir nit ñi.
Kàddu yu Xelu 30 in Kàddug Yàlla gi