Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 2

Kàddu yu Xelu 2:7-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Day dencalal ndam kiy jubal, di yiir ku mat.
8Day wattu ku jub fu mu jaare, di sàmm wóllëreem ciw yoon.
9Kon nga xam njub ak yoon, xam jubal ak mboolem yoonu mbaax.
10Ndax xel mu rafet miy tàbbi sa xol, nga xam, sa xol tooy,

Read Kàddu yu Xelu 2Kàddu yu Xelu 2
Compare Kàddu yu Xelu 2:7-10Kàddu yu Xelu 2:7-10