Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 2:7-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 2:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Day dencalal ndam kiy jubal, di yiir ku mat.
8 Day wattu ku jub fu mu jaare, di sàmm wóllëreem ciw yoon.
9 Kon nga xam njub ak yoon, xam jubal ak mboolem yoonu mbaax.
10 Ndax xel mu rafet miy tàbbi sa xol, nga xam, sa xol tooy,
Kàddu yu Xelu 2 in Kàddug Yàlla gi