Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 2

Kàddu yu Xelu 2:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Kon nga xam luy ragal Aji Sax ji, xam Yàllaa di kan;
6ndax Aji Sax jeey maye xel mu rafet, kàddoom di taxa xam, di dégg.
7Day dencalal ndam kiy jubal, di yiir ku mat.
8Day wattu ku jub fu mu jaare, di sàmm wóllëreem ciw yoon.

Read Kàddu yu Xelu 2Kàddu yu Xelu 2
Compare Kàddu yu Xelu 2:5-8Kàddu yu Xelu 2:5-8