Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 2

Kàddu yu Xelu 2:2-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Teewlul xel mu rafet, sam xel di dégg.
3Ngalla wutala dégg, wool dég-dég wall.
4Sàkkul xel mu rafet ni xaalis, wut ko ni alal ju làqu.
5Kon nga xam luy ragal Aji Sax ji, xam Yàllaa di kan;

Read Kàddu yu Xelu 2Kàddu yu Xelu 2
Compare Kàddu yu Xelu 2:2-5Kàddu yu Xelu 2:2-5