Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 2:2-5 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 2:2-5 in Kàddug Yàlla gi

2 Teewlul xel mu rafet, sam xel di dégg.
3 Ngalla wutala dégg, wool dég-dég wall.
4 Sàkkul xel mu rafet ni xaalis, wut ko ni alal ju làqu.
5 Kon nga xam luy ragal Aji Sax ji, xam Yàllaa di kan;
Kàddu yu Xelu 2 in Kàddug Yàlla gi