Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 29

Kàddu yu Xelu 29:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Ku jub a xam àqu néew-ji-doole, ab soxor xamu ca dara.
8Ñaawlekat a ngi taal ab dëkk, ku xelu di giifal mer.
9Boroom xel, buy layook ub dof, bu mereek buy ree, jàmm du am.

Read Kàddu yu Xelu 29Kàddu yu Xelu 29
Compare Kàddu yu Xelu 29:7-9Kàddu yu Xelu 29:7-9