Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 29:7-9 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 29:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Ku jub a xam àqu néew-ji-doole, ab soxor xamu ca dara.
8 Ñaawlekat a ngi taal ab dëkk, ku xelu di giifal mer.
9 Boroom xel, buy layook ub dof, bu mereek buy ree, jàmm du am.
Kàddu yu Xelu 29 in Kàddug Yàlla gi