Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 29

Kàddu yu Xelu 29:6-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Ku bon day moy, ba dugal boppam; ku jub di woy ak a bànneexu.
7Ku jub a xam àqu néew-ji-doole, ab soxor xamu ca dara.
8Ñaawlekat a ngi taal ab dëkk, ku xelu di giifal mer.

Read Kàddu yu Xelu 29Kàddu yu Xelu 29
Compare Kàddu yu Xelu 29:6-8Kàddu yu Xelu 29:6-8