Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 29:6-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 29:6-8 in Kàddug Yàlla gi

6 Ku bon day moy, ba dugal boppam; ku jub di woy ak a bànneexu.
7 Ku jub a xam àqu néew-ji-doole, ab soxor xamu ca dara.
8 Ñaawlekat a ngi taal ab dëkk, ku xelu di giifal mer.
Kàddu yu Xelu 29 in Kàddug Yàlla gi