Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 29

Kàddu yu Xelu 29:21-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Ku yàq sab surga ba muy ndaw, bu ëllëgee mu defe ne doom la.
22Boroom xadar day sooke ay, te ku tàng bopp moy, moyati.
23Réy-réylu, detteelu rekk; woyofal, ñu naw la.

Read Kàddu yu Xelu 29Kàddu yu Xelu 29
Compare Kàddu yu Xelu 29:21-23Kàddu yu Xelu 29:21-23