Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 29:21-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 29:21-23 in Kàddug Yàlla gi

21 Ku yàq sab surga ba muy ndaw, bu ëllëgee mu defe ne doom la.
22 Boroom xadar day sooke ay, te ku tàng bopp moy, moyati.
23 Réy-réylu, detteelu rekk; woyofal, ñu naw la.
Kàddu yu Xelu 29 in Kàddug Yàlla gi