Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 29

Kàddu yu Xelu 29:19-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Waxi neen yarul surga, da lay dégg te du la déggal.
20Ana koo gis, mu rattaxle? Kooku ab dof a ko gën demin.
21Ku yàq sab surga ba muy ndaw, bu ëllëgee mu defe ne doom la.
22Boroom xadar day sooke ay, te ku tàng bopp moy, moyati.
23Réy-réylu, detteelu rekk; woyofal, ñu naw la.

Read Kàddu yu Xelu 29Kàddu yu Xelu 29
Compare Kàddu yu Xelu 29:19-23Kàddu yu Xelu 29:19-23