Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Ku ñàkk, su jekkoo ab ndóol, du ko bàyyil fepp, day mel ni waame.
4Ku wacc yoon, gërëm ku bon; ku wormaal yoon, jànkoonteek ku bon.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:3-4Kàddu yu Xelu 28:3-4