Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 28:3-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 28:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Ku ñàkk, su jekkoo ab ndóol, du ko bàyyil fepp, day mel ni waame.
4 Ku wacc yoon, gërëm ku bon; ku wormaal yoon, jànkoonteek ku bon.
Kàddu yu Xelu 28 in Kàddug Yàlla gi